DIAMALAHI FM SUR XALIMA.COM

DIAMALAHILOGO

Skype :   diamalahifm92.3 

Email:[email protected]


73 Responses to “DIAMALAHI FM SUR XALIMA.COM”

  1. <path_to_url> Sokhna Lissa Laye

    exellent exellent exellent il faut vraiment que ca marche.

    Reply
    • <path_to_url> Khalilou Laye

      Machallah laye makhtar on est tous fier de vous. Yalna dieum kanam ci barké Baye Laye asws

      Reply
      • <path_to_url> Arame wade

        Dieureudieuf lahi Alassane an Seyni

        Reply
    • <path_to_url> malick sow

      li nekh wa yalla nayou yalla fayal bay laye

      Reply
    • <path_to_url> SAMBA DIOP

      laye makhtar. dieuredieuf . On est vraiment content des programmes de diamalaye fm. salut à mon ami moctar de diamalaye fm. De la part de samba diop laye de richard toll. BAYE LAYE amoul mass

      Reply
  2. <path_to_url> Khalilou Laye

    Machallah laye makhtar on est tous fier de vous. Yalna dieum kanam ci barké Baye Laye asws

    Reply
  3. <path_to_url> Libasse KEBE

    Laye mkhtar wa DIAMALLAHI FM. On est derrèe vous. Ca kanam

    Reply
  4. <path_to_url> cheikh laye mbengue

    Macha’Allah, khol yi séde nagn laye makhtar!!! Dieureudieuf laye

    Reply
  5. <path_to_url> Fatou Laye Diop

    Machallah wa DIAMALAHI FM contane nanou trop zikr yi ak wakhtane yi nekhna trop yalla dém ba nékha télé si barké Baye Laye ASWS

    Reply
  6. <path_to_url> Tahir Laye

    La diaspora layene est reconnaissante envers toute personne qui participe de près ou de loin à l’ avancement de la radio.C’est une sorte de cordon ombilical pour nous.
    Dieuredieuf laye

    Reply
    • <path_to_url> malick sow

      laye laye zirana lou beriii

      Reply
  7. <path_to_url> malick

    Conte na trop bilaye yalla na you yalla fayal bay laye

    Reply
  8. <path_to_url> Abdoulahi

    Merci beaucoup…Radio bi moy sunu wetal, Yalna dieum kanam

    Reply
  9. <path_to_url> IBOU FAYE

    Ibou faye New York USA
    LAHI MAHTAR
    Felicitations de nous tenir compagnie tous les jours et je confirme la bande sonore de nidiaye ISSA MBAYE pour l’avoir entendu de sa propre bouche a Malicka pour avoir ete le parrain de ma soeur quand Elle rejoignait le domicile conjugal de son mari en provenance de Bargny
    Yal naka Bay Lay ak Seydina Issa terrou

    Reply
  10. <path_to_url> Ibrahima Lo

    Dieuredieuf laye makhtar bègue nagniou si yene yalna dieum sa kam ba yalla def mou nek télé si barke Baye Laye wormaye Mame Seydi amen

    Reply
  11. <path_to_url> Ibrahima Lo

    Dieuredieuf laye makhtar bègue nagniou si yene yalna dieum sa kam ba yalla def mou nek télé si barke Baye Laye( asws)wormaye Mame Seydi (
    asws)amen

    Reply
  12. <path_to_url> FAMALAYE GAYE

    MANDIONE TAYY KHOL YI SEDNA GOUYE GEUM BAYE LAYE REKKA WORR

    Reply
  13. <path_to_url> Medoune SARR

    diadieuf lay makhtar yalna si yalla dolli ndam

    Reply
  14. <path_to_url> abdou

    je suis content sur vous vrement vous nous faitez plaisir chaque jour

    Reply
  15. <path_to_url> Thiam laye

    Allawouma allaa seyedinalimamoulaye seyedilmouhktar waseyedinlimoulaye waseyedile allamine dieuretieuffe diamalaye fm

    Reply
  16. <path_to_url> tiam laye

    Allawouma allaa seyedinalimamoulaye seyedilmouhktar waseyedinlimoulaye waseyedile allamine dieuretieuffe diamalaye fm

    Reply
  17. <path_to_url> El Hadj Mbaye FALL

    Laye Makhtar.
    Contan naa bu bax ci comenter yi dieum ci radio bii may deglo tay fii ci Abidjan . Ma leen di niane yen nieppe ngene gana japp ci Groupement central, rawatina ci system bu bess bi mu taxawal, ndax mu gana mana jappe ci sunu radio bii mu takhawal te munuy weteli nun nieppe, be sakh mu man ce teg ab television.
    Dieureudieuf Baye Laye.

    Reply
  18. <path_to_url> FAMALAYE GAYE

    machaallah yalla naniou yalla rayy te dekkil niou si dinne limamou
    laye alleysalam

    Reply
  19. <path_to_url> SMBA DIOP

    dieuredieuf. depuis rosso senegal, dn suit diamalay fm sur le net. yeney sounou wettal. lay makhtar. BAY LAHI AMOUL MASS

    Reply
  20. <path_to_url> Abdoulahi Ndir

    Tous nos remerciement a ce site xalimàs qui ns a permis d’ecouter notre radio diamalahi fm que le bon dieu nous donne un tele dans un futur proche Seydina limamou merite plus que ca.du courage les guys

    Reply
  21. <path_to_url> saliou ndoye

    ca caw sa kanam lép moy bakh inchallah

    Reply
  22. <path_to_url> elimane oumar

    maa cha allah. baye aboo yala nafi yaague te weerr.

    Reply
  23. <path_to_url> MAME SAMBA SOW LAYE

    DIEUREUDIEUF SAHABAY BAYLAYE YII NANIOU GUEUNA FARLOU THI YONE WI GUEUNE MOYE DIINEE YALLA MI NIUU BAYE LAYE IINDIIL TEE WAADIAAL SOUNOU BOPP TOPEE DIKLEEM YA MOYTUU TEEREE YA, TEE BUULEEN DI FATEE DII WAAR DIAAM YAALLA YI KHUUTBAY BAYELAYE YI .

    Reply
  24. <path_to_url> CECILE NDIAYE LAYE

    LAYE MACTAR YALLA NALENE YALLA FAYE.EMISSIONS YI AMNA SOLO. DIADIEUF LAYE MACTAR

    Reply
  25. <path_to_url> Ida Gadiaga

    Dieureudieuf waa Diamalahifm92.3 yalna lenn yalla may télé bou amm dolle thi barkee Baye laye ak seydi psl
    .

    Reply
  26. <path_to_url> mor laye

    Yalna yalla fayleen te sámba RADIO bi ….begg nann lool Laye mahtar…..DÍAMALAYE FM

    Reply
  27. <path_to_url> Rane diagne.

    Laye. Mactar Contane. Lolou. Sounou Xol Fess. Na Lolou. Yalla Na léne Yalla fay. Di. Barké. Baye laye. Magui. Nouyoul. Bou. Bakh. Baye ABDOULAYE diagne. Camberene Di Ko Ziare. Si Apele. Bi. Macha alah

    Reply
  28. <path_to_url> MAME SAMBA SOW LAYE

    DIEUREUDIEUF LAYE NINGUI DEGLOU YALNALA YALLA FAYE TEE SAMALA THI BARKEE BAYELAYE AK SEYDI THI LIGUEEYE BI.

    Reply
  29. <path_to_url> Amiral Général Dialaye

    Alhamdoulilahi rabil halamine…Alhamdoulilahi rabil halamine…Alhamdoulilahi rabil halamine
    Cela fait 2 ans que je suis au Maroc et que je cherchais par tous les moyens comment faire pour revivre les moments des dahiras, des invocations du nom d’Allah, des enseignements de Seydina Limamou PSL
    et c’est en ce jour (Vendredi 15 mai 2015) que je tombe par inadvertance sur ce lien.
    Je ne trouve pas les mots pour exprimer ma gratitude envers ceux qui l’on mis en place.
    Je prie Ô Rassembleur, rassemblez pour nous les (meilleurs) destins. Illuminez nos cœurs par l’Islam. Accordez-nous le bonheur dans les deux mondes : terrestre et éternel.
    Par considération à la formule «lâ ilâha illal lâh» (point de divinité que Dieu)
    Amine.
    Dieureguène dieuf.

    Reply
  30. <path_to_url> khady laba ndiaye laye

    Tres contente de diamalaye fm j suis a nouakchottj suis toujours ptesse d aller au travail poupouvoir ecouter toute la journee la radio diamalaye fm
    Khady laba laye

    Reply
  31. <path_to_url> Koly Laye

    Am na solo laye mahtar… Yal na Yallah yokk khéweul gui… Ce radio est la voix du Mahdi asws…

    Reply
  32. <path_to_url> Maimouna laye

    Laymahtar amna solol na gnou yalla fayal baye laty ak seydi dam rek li deguel woteh bi bien

    Reply
  33. <path_to_url> lamine

    Dire Merci à xalima et Diamalahi fm

    Reply
  34. <path_to_url> balla sene

    Jeureudieuf laye makhtar

    Reply
  35. <path_to_url> Adja Sophie Laye

    ma ngui Dubai dilene degg bou bakh, dieuredieuf laye Mactar

    Reply
  36. <path_to_url> abdourahmane laye / derklé

    Lay-Mamadou le premier jour que j’ai réussi à avoir Jammalay. Fm

    de la localité ou je suis merci mon DIEU.

    Reply
  37. <path_to_url> Adja Sophie Laye

    Seydina! laye makhtar sa liguey rafetna, yalla nala yallah faye, thi barke baye laye ak Seydi

    Reply
  38. <path_to_url> Samba DIOP

    A mon ami moctar dediamalahi fm. De la part d’un ami et admirateur de richard toll que tu reconnaitras certainement à cause d’une longue causerie dans les locaux de la radio sur notre bien aimé SEYDINA LIMAMOU LAHI AL MAHDI. Depuis ce jour, j’ai prié DIEU LE TOUT PUISSANT d’etre en contact la communauté akhlou lahi. Il m’a gratifié de diamalaye fm que j’écoute tous les jours à travers le net. ALHAMDOU LILAHI RABIL ALAMINA. BAY LAY AMOUL MASS

    Reply
    • <path_to_url> Makhtar Laye

      Djeureudieuf mon cher ami Samba Diop. c’est vrai que amone na solo trop. wahtanei Sangue bi dafa neh tei ame solo. j’espere que lepp diameu fofou ci richard toll.

      Reply
  39. <path_to_url> Abdourahmane-dit Pape

    Ziar naa wa AKHLOULAYE sur kaw suuf nit ak djinné
    je me réjouis de l’opportunité de DJAMMALAHI FM que je considère comme une ancre qui empêche une dérive.
    parce que avec les courants et marais de fin du monde………wayé santaate YALLA SUNUU BORÔM
    LAY-MAMADOU

    Reply
  40. <path_to_url> Sakhir laye

    Macha’allah !! Yalla na yalla dollaine xalima…
    Am na sollo laye maxtar !!
    Nieup conetane nane…
    Fo meune nék di am radio bi..
    DIEUREUDIEUFEUTI SEYDINA LIMAMOU LAHI ( PSL ).

    Reply
  41. <path_to_url> Libasse Lalo

    Dieureuf yen waa Diamalaye FM.Franchement boka guène ci gninga khamni niooy wagni souniou stress ak dignou wétali ci fii ci diaspora bi.Yalna lène Bour Yalla diapalé té tassoulène ci Barké Baye Laye.Amine

    Reply
  42. <path_to_url> Libasse Lalo

    Dieureudieuf encore.Que Le Tout Puissant vous accorde longue vie pleine de santé,de réussite,de bonheur et beaucoup de prospérité.Amine ci Barké Borom Diamalaye.

    Reply
  43. <path_to_url> Makhtar Laye

    Djeureudieuf mon cher ami Samba Diop. c’est vrai que amone na solo trop. wahtanei Sangue bi dafa neh tei ame solo. j’espere que lepp diameu fofou ci richard toll.

    Reply
  44. <path_to_url> Ibrahima Lahi

    Laay madiné laay! Écoutez votre émission Doundou Yonent Yi avec Oustaz Ibrahima Lahi Sow à 16h sur votre radio de coeur Jamalahi FM 92.3

    Reply
  45. <path_to_url> Oumy mbengue

    Machalla yalna yalla fayal gnou baye laye (asws)

    Reply
  46. <path_to_url> Abdourahmane-dit Pape

    lou diot yômb ! je me rappelle il n’y a pas longtemps dans les radios et télé du pays on nous réservait des miettes de temps d’antenne aye am sa gnamou beutt . Je me rappelle un jour j’étais avec des étrangers au marché Tiléne Dans une boutique de cosmétique: c’était une matinée de vendredi sur le ondes radios les animateurs réservent des temps d’antenne à chaque confrérie. Après quelques minutes dans la boutique la radio qui passait les zikr laissa le tour aux LAYENES ma réaction fut spontanée c’est à dire j’étais content et je l’ai manifesté. Mais le boutiquier un KAW-KAW zappa en tournant le bouton pour m’humilier malgré mes protestations il a fait comme s’il s’en foutait ! Laye Makhtar automatiquement tout le courant de marché sautait avec un bruit de bombe: j’ai crié ALLA YAA RABBANAA etje suis sorti de la boutique .il y avait un deuxième commerçant qui tenait un CORAN il a levé la tête a sourit
    mais n’a rien dit : j’étais dans un HÂLE indescriptible .

    Reply
  47. <path_to_url> Abdourahmane-dit Pape

    je vous aime vous wa AKHLOU-LAHI
    je vous aime trop
    à votre vue je m’apaise
    quand je vous entends
    je me sens bien et je me sens heureux
    et j’ai plus envie de retourner d’ou je viens
    c’est à dire dans mon quartier
    ceci n’est pas un poème mais un ressentiment

    Reply
  48. <path_to_url> dembo faty

    vraiment laye makhtar contane niou si yenn machalla yalnalenn yalla feey si barké baye lahi (asw)

    Reply
  49. <path_to_url> ASSANE DIOUF

    VRAIMENT LAYENE MON NEKH TROP AVEC LEURS VOIX DE DIAMANT MACHALLA

    Reply
  50. <path_to_url> Aïda Laye

    ManShaaAllah Laye Makhtar.. dileen béguée depuis Japon.. yalnayAllah khep dolli..

    Reply
  51. <path_to_url> Amy colle Laye GUEYE

    Manchalla laye makhtar dileen begui sa you me len degue yalla na yalla fayal noulen barke mame BAYE LAHI ALEYSALAM

    Reply
  52. <path_to_url> Adja Sophie Laye

    niou ngui bitim rew di deklou Diamalaye fm, Mame Allassane Lahi (Pape Rane) yalla na yalla yok leeram

    Reply
  53. <path_to_url> Meissa Ndiaye

    Yalnah BOROM BI Nangoù niaan yi si beuss bi si Barké Baye Laye Ak Seydi..Amiine

    Reply

Leave a Reply

  • (will not be published)