Oustaz Alioune Sall – Waxtaanu Fajar du lundi 11 avril 2011 – Droit de l’époux et de l’épouse en Islam;

Posted by on in Causerie Oustaz Alioune Sall

Details


Oustaz Alioune Sall – Waxtaanu Fajar du lundi 11 avril 2011 – Droit de l’époux et de l’épouse en Islam;

Source: Archipo.com/sudfm

24 Responses to “Oustaz Alioune Sall – Waxtaanu Fajar du lundi 11 avril 2011 – Droit de l’époux et de l’épouse en Islam;”

  1. <path_to_url> ndiayeyankhoba

    ha kaza oustaz sall .bokk na ci aya mayamme macc ak ndaw ce pa co sopp machalah dondal loubari yaoustaz

    Reply
  2. <path_to_url> adama

    dieureudieuf ya oustaze damay niane jeuneesse senegal niouy deglou ki ak nioumelner mom ndakh dan niouy deloo thi sounou borom tee degeureul sounou geum moogeune niouy dem thi site yokhamner dan niouy sorel ak sounou diner assalam

    Reply
  3. <path_to_url> aicha

    dieureudieuf sall yalla na yalla yok saye fane amine sa dounde amna diérigne

    Reply
  4. <path_to_url> aliou samb touba

    salam oustass aliou sall yalla yagualle kofy ak werr si barekebb seydina mouhamed sallalahou haleyhi wassalam ak mbolemme dioulite te senegal yalla sotyfi ndokhe mou sedde guouye aamine ya raballe alamine

    Reply
    • <path_to_url> cheikhouna ka

      ziar nalacheikh alione sall mangui tuddou cheikhouna dyraki ouztaz aidara parsel deuke touba sawakh e nexnama ndakh sak yatu kholl akuk am ndiaringe ciao

      Reply
  5. <path_to_url> thiam

    SOPOUNALA TROP

    Reply
  6. <path_to_url> assane lo

    Ya oustase diere dief yalla nala yalla faye sa dounde billaye amna ndierigne thi jeunesbi.Goudou fane gnelnala yalla nako yalla def Amiiiiiiine

    Reply
  7. <path_to_url> ass samb

    yallana yalla fayal no oustaz aliou sall si barke sr touba sama yakar

    Reply
  8. <path_to_url> yvonne

    salam tout le monde damay nian si barké SEYDINA MOUHAMED (psl) daradiéy CHEIKHNA AHMED TIDJANE CHERIF sounou borom soubkhanahouwa talla bayilafi lou bari ndakh mayla goud fan ak werr lep moom la le SUPERIEUR

    Reply
  9. <path_to_url> lamine samb

    DIEREDIEF YA OUSTAZ YALLA NALA YALLA DOLLI DIAM SI BARKE ALKHORAN LIGAYWAKHE YALLANAKO ASKANWI DIARINIO

    Reply
  10. <path_to_url> aliou samb touba ndamatou

    yaram kontane nagnou lolle kou tedde ki ak wa touba ndamatou yeppe boutique aliou gueye

    Reply
  11. <path_to_url> mangone fall

    amna mekte ak kontante bou bakh oztas aliun sall yalna la yalla defal diam ak ver yalnala bay ak khel diaradif

    Reply
  12. <path_to_url> assane

    papa alioune sall yaw ak mame abdou ak bay ibou sakho liguene def si mane thi khamal ma loubari. yalla mo ame sene faye yalla nalene yalla faye

    Reply
  13. <path_to_url> bakary bathily

    assalamopualeyecoum ya oustaze di t la ziar bouwer

    Reply
  14. <path_to_url> ismaill

    assala mou alay coum ??

    Reply
  15. <path_to_url> ousmane sarr

    dieureu dieufe oustaz aline sall yalna yalla yoke sakham kham tedollila wergou yarame

    Reply
  16. <path_to_url> P S L

    Salam ya oustaz ya bakhe macha alla mane limay wakhe moy dila nianal yala mouseul leu si chaitané ak képe kouye liguéy yal ISLAM dieuredieuf

    Reply
  17. <path_to_url> awa

    yala nala fi yala bayi. mane dé yala ak yaw moo takh ma changé.
    dama dane sole lou bone. mais depuis que j’ai commencé à vous écouter tout le monde a vu mon changement.
    de la part de celle qui était venu te voir chez toi.
    merci beaucoup oustaz.

    Reply
  18. <path_to_url> HAMIDOU

    dieurediefff ya oustaze

    Reply
  19. <path_to_url> HAMIDOU

    soukrane laka yaa oustaze

    Reply
  20. <path_to_url> sokhna

    dieureudieuf oustaze alioune sall wakhtane bi amna solo yla na yala faye sa khol

    Reply
  21. <path_to_url> NDEYE NDIAYE

    dieureudieuf ya oustaz penc mi bek na thi yaw ak jeunessebi macha ala

    Reply

Leave a Reply

  • (will not be published)