Comment faire de la publicité sur xalima.com ?

Lamp Fall Kaolack

Posted By Xalima News On Mercredi, avril 21st, 2010 With 2 Comments



11 Commentaires
Participer au forum
  1. Xaadim LO dit :

    jarajeef wa Lam FAAL FM Kaolack.mangi Siaare wa rajo bi yepp.di NUUYU SERigne Alioune TOURE ak Taala CUUN et tout le personnel bonne continuation

  2. Modou dit :

    Dieureungéne Dieuf yéne wa Lamp Kaolack séne Liguéy Sétena té Sélena !!!
    Serigne Alioune TOURE Beug Serigne TOUBA Borom Pencoum Kaolack gnongilay bégééééé loubary T& dila gnanale Goudefane ak Wer ak personelle bi yép .
    Serigne Mbacké Diéne borom yor yorou Touba
    Serigne Issa Borom Ndiangaléme Serigne Bi
    Tala THIOUNE – Assane TOURE ak gnép rék

    Dieureungéne Dieuf . Yalanaléne Serigne TOUBA sAMAL bOPAME

  3. MOUDOU SARR dit :

    sala malicoum serigne issa none wa itali nogue deklou ndiangalim borom touba thi milan dieradife

  4. malick toure dit :

    lamp fallfm radio xarnou bi moye sunuo radio lamp falll tv moye tele senegal

  5. Serigne Aliou TOURE Nio ngilay nianale goudefane ak Wêr !
    Yanginouy bégal sassouné si Ndenki li ak pencoum kaolack
    Boule nouye fatéti nioune wa italy Bergamo si ndenki li.
    Yala naléne Yalla Takhawou té ngéne ngeureumale Serigne Touba

  6. aliou toure dit :

    serigne bi mngui laye ziar dila tèèwlou

  7. aliou toure dit :

    mangui ziar sama tourando di sama dieuwrine

  8. khady ciss dit :

    ziar nalen lou barry folene tolou dellene wax amine ndax fougnou tolou danioulenni nianal lou barry te dilene tewlou fognou toloumouy S Aliou Toure beug S Touba ci pecum kaolack Di S talla Thioune ak ki di S Issa ci ndiangualem serign bi yeppa am solo yalla guen fii yaggu loll ak Ndecki ci lamp fall yeppa am nieurigne rawna ci bou taybii

  9. astou.mbaye dit :

    ziar nala bo wer s aliou tore bege s touba ma gi lay deglo depu italy ma gi ziar sa ma make s issa mbaye

  10. adama diouf dit :

    Serigne adama diouf (diourbel) moyy sant bepp personnel bou lam fall fm akk oditeurs yii

Poster un commentaire

XHTML: You can use these html tags: <a href="" title=""> <abbr title=""> <acronym title=""> <b> <blockquote cite=""> <cite> <code> <del datetime=""> <em> <i> <q cite=""> <strike> <strong>



Comment faire de la publicité sur xalima.com ?

Revue de la presse