Comment faire de la publicité sur xalima.com ?

LAMP FALL DAKAR

Posted By Xalima News On Samedi, novembre 28th, 2009 With 2 Comments



style="display:inline-block;width:468px;height:60px"
data-ad-client="ca-pub-1433917768187213"
data-ad-slot="9368633314">








116 Commentaires
Participer au forum
  1. Oumar BA dit :

    Ma chalah c vraiment cool, jajeuf, lamp fall bi fallaw lerna nagne,

  2. akasa serigne touba sante bouwer sounou doune ac sounouk de

  3. Mor Wade dit :

    Sant Serigne Touba Rék, prions pour que la télé arrive vite. En parlant de télé, pourquoi toubatv n’émet plus?

  4. serigne diop dit :

    dieuredieuf serigne touba.
    lamp fall en avant comme son nom indique.
    nous prions pour que la télé arrive bientòt.

  5. ayouibadieng dit :

    diarama lamp mi leral yonwi

  6. maleye niang dit :

    santati rek nioune wa ndiarem thi foulk bi tey niane thi barke serigne ismaila mbacke mou mame faty tv tope ci

  7. mor dit :

    dieuradieul wa lamp fm si ligéye bi gnéne deff si yonbi mourite

  8. Moussou dit :

    Serigne Touba Amoul morom. Lamp Fall radio bi lerel lepp lou lendë moon.

  9. PAPE DIOKHANE dit :

    JAA NGENE JEF LAMP FALL YALA NA YALA DOLI AY HEWEL YU BARE BARI

  10. FATIMA dit :

    lampe mo tal ba bamba fégne dieudieuf waye

  11.  » Bo ca foroon sax bant (Laylatul Qadar)wala ngay nélaw ngir Yalla ak Yonén ba gaa nia (mala-ika yi) ya nga takhaw, dila bindal tuyaba tay fuul say may, té dila yeukati ca kaw fuul say may » Sokhna Maimouna.

  12. aliou Diop dit :

    LAMPE FALL LAMP BII CHEIKH BAMBA TAALE Lèeral NANOU DJAA JEEF JEEF.

  13. gora gueye dit :

    serigne reck diarama lampe fall

  14. lamine bara dit :

    magui ziare wa lamp fall ak mboki talibe yi di serigne cheikhe sidi makhtar ak serigne cheikhe ndieum fall yague fi lol té wer si barké serigne sliou ; di nianal wa lamp fall guawa am télé dahe mou guena tawfekhé diaguene dieuf magui niane lou waye bueugue ak lou waye niane si wérou koor gui yalla naguou ko barké serigne saliou dieurdieufe serigne touba diara am mame cheikhe ibrahima fall ; diaguene dieuf

  15. SERIGNE GORA NDIAYE dit :

    BISIMILAHI DI SANTE YALLA DJOULI SI RASSOULOULAHI SANTE SERIGNE BOU WER DI GNANAL TALIBÉ YÉP DI GNANAL <> DIAMOU AK KHÉWEL BOU SAKH DACK FI DUNYA WA LAKHIRA AMINE!!!!!!!!!!!!!!!!

  16. serigne sene dit :

    depuis touba brasil sante bu werre wa lamp fall mais na tele bii ngaw

  17. serine diop dit :

    bismilahi jajaf serigne bou magbi.lamp fall monek çi deugg tambléé thi serigne bi yam çi serigne bi.thia kaw thia knam.nous les mourides devons serrer les mainspour mieu oeuvrer sur la mÊe ligne.thiowli barina wayi nan tanko çi ndegueel dakh mouride ndigueel.merci lamp a eclairé ce qui etait obscure.

  18. DIEUREUDIEUF LAMP FALL

  19. laity dit :

    boudoul wone démamegui kone bilahi niep déme nirani kone sant gnou warr dieureuuti borom touba

  20. In the name of Allah,
    the compassionate,the merciful,Praise be to Allah,
    Lord of the Universe,and Peace and Prayers be upon His final Prophet and Messenger.
    Dieuradiuf Serigne Touba, Mame cheikh Ibrahima fall,Diarawlak,
    s.Ismahila Mbacke,Maley Niang,and I say Hi to everybody in Keur goumack,Eid-al moubark for all you.I lisented the <>.Every day.ousmane dieng,USA

  21. SALIOU ATHIE dit :

    Kén dou serigne touba dieureu dieuf lamp fall yaw mi tal yon wi.di sante sasouné cheikhoul khadim

  22. sidy diouf dit :

    le meilleur du monde c’est lamp fall

  23. mor diagne dit :

    diuereudiuef wa lamp fall fm serigne mouléne dii faye

  24. MERCI TOUS LES MURID AU SENEGAL

  25. khadim fall dit :

    sante serigne touba té fasyènè sakh si ak ndioup ba faw al hamdoulilahi

  26. beug serigne touba rék
    fonk serigne touba rék
    yaakar serigne touba rék
    diara ame mame cheikh ibrhima fall
    lamp fm

  27. mor dit :

    LAMP FALL THAKAW THA KANAM

  28. khadimsall keurserignefallou louga dit :

    dieurediefserignetouba diarama aladji fallou mbacke

  29. Mouhamet dit :

    Dieuredieuf SERIGNE TOUBA diarama MAME CHEIKH IBRA FALL

  30. Abdou Faye Maroc dit :

    Dieredieuf Seirigne Touba,Diarawlak Mame cheikhe Ibra Fall;diadiefeti wa Radio Lampe Fall,sa kaw sa kaname;yall na done aye Tv,

  31. mor dit :

    dieuradieuf wa lamp fall ak personel bi yap kholou mourite yap sédna dieuradieuf serigne alioune thioune

  32. khadi ndiaye dit :

    dieradief serigne touba diarama
    mame chiekh ibrahima fall bégué lamp fall radiobi sédale kholou doulityi rawatina mourrityi

  33. bathi dieng dit :

    ak lou mana khéw taibe socé do nitok dara dafa yague bagne serigne touba wayé nak thi kawam laye keupou serigne bi mom beurigo thi mbartal la ko poss mou dém ko posoul mou dém

  34. BADAR NDIAYE dit :

    LES CHIENS ABOIENT LA CARAVANE PASSE,( CII KAAW CII KAANAM ) SERIGNE TOUBA AMOUL MOROME . TALIBè MOURIDE BOU SAGUANE BI REK DOU SèN MOROME

  35. gora gueye dit :

    SERIGNE TOUBA REK DIARAMA MAME LAMP FALL WAW WAW

  36. diarama lamp fall fm moye souniou wétale sa souné tayite mogui gniouye dimaly bou bakh si diné dji wa salam

  37. Mouride GUEYE dit :

    sant naniou bou bakh , Yalla Naniou Serigne Bi Gueureum

  38. ntl dit :

    dieureudieuf Cheikh Ahmadou Bamba Mbacke, diarama Mame Cheikh Ibra, sante na leen yeen wa LAMP FALL ALHAMDOULILAHI .Ma ngi ziarr ndieup thi beussou diouly guedji gui

  39. sante serigne touba thie lamp fall di siyare serigne khadim ndiaye kayar ak wa radio beppe

  40. makhtar amar dit :

    we thank you lamp fall may alah bless you from makhtar amar usa

  41. fallou diop dit :

    sant lamp fall bou bakh migni wetali ak diniou yéééééééè fepp fougnou mana nek

  42. Modou Seck dit :

    SANT BOU BAKH WA LAMP FALL FM, CA KAW CA CANAM

  43. MBAYE dit :

    SLT JE SUIS TRES CONTENT DE VOUS.JE VEUX AVOIR VOTRE PAGE FACEBOOK EMISSION EMIGRE.

  44. http://lampfalltv.sn le site de lamp fm et TV gnioune talibé serigne bamba serigne bamba lagniou ame té serigne bamba gnioune la ame kone nagniou diapaneté sougniou biir serigne bamba dieulesigniou si sougniou mbirr yombe gniou fou kawé sougniou djoorté té serigne touba lamou meunone thie adouna bi fé mou nék lako gueuneu meune kone kouko diape té doko bouléke dara da nga ame dara té da nga done dara

  45. DAME FALL dit :

    darae dafe searine touba darame mam cihue iberae fall

  46. FALL DAME dit :

    BGUME TALEBE BOUHAM FRKASU LAMPFALL TV BEINGUYE RESRSU BAHEMGO GEURE SERINE TOUBA

  47. djily sakho dit :

    ziare walamp fall gnanal serigne sidi moukhtare moyaguefi tewerr loooool amine

  48. dieuredieufé serigne touba dieuredieufé borom touba dieuredieufé cheikh ahmadou bamba khadimou rassoul

  49. sant bou wer bignou yalla maye xel dep dem thi serigne touba rethiou wouma ko ben yone yalla kham nako fima nek sante rek wa lamp fm

  50. magui delo santi serigne touba sa a sone di soipe khssidai di ñanal serigne sidi moukhtar mbacke mo yaguifi te wer

  51. dieureudieufé borom touba diarama lamp fall baboul mouridina sa kaw sa kanam

  52. serigne touba amoul morom

  53. damay sakkou niane dama beugeu done deggui talibe. Serigne Touba la beugg té mome la yakaar wayé ni talibé waré mel melouma nonou. bougene ma gnanaloul fouma diem? damay toog di tiit wayé yenn sa douma téré def naka soudoul nonou esk dou seytané moma eup dolé? niane lène

  54. yala nagnou yala dfal degu ak topou

  55. djiby kane dit :

    lamp fall amoul morome

  56. djiby kane dit :

    sope lamp fall diarama lamp fall

  57. sant serigne touba rek

  58. mailck dit :

    borom touba moo mann gnieupe

  59. Lou nééx serigne touba nééxna yonéntebi.lou nééx yonéntebi nééxna yalla.té yéén wa lamp fall fm ak lamp tv lou nééx serigne touba rék géén bi déf

  60. thiam dit :

    serigne touba kèpe serigne touba kèssè serigne touba dongue serigne touba rèke serigne touba . guereudieufèèèèèèè serigne touba

  61. dieureudieufé borom touba diarama lamp fall baboul mouridina sa kaw sa kanam

  62. 1 dit :

    QUELQUN PEUX ME DONNER LA DATE DU GRANG MAGAL SVP MERCI IBRAHIMA TOURE BELGIQUE.dieurediufe lamp fall

  63. brock dit :

    diadieuf ndogo si ca sera le 11 ou le 12 janvier 2012 aujourd,hui on est le 16 11(tabaski) du canlendrier lunair die ziar mogui belgique yeepeu

    Tawfekh ak taysir

  64. moru dit :

    serigne amognou fayame mane dé khamnani moy sama bountou pour ma ague si yonenete bi .amena bene goudi ma guente deme siare yonete bi (pais et salut sur lui)way de serigne touba legnou ma bolele pour mou yobouma,.dieureudieufe serigne touba

  65. NDiaw Yaté dit :

    Bismil Lakhir rakhmaanir rakiimi.

    Allakhouma salli alaa Seyninaa Moukhamad salla Laakhou ta aalaa alaykhi wa salam,
    Dieureudeuf Serigne Touba, diarawlakh Mame Cheikh Ibrahima Fall
    Serigne Saliou MBacké yalla na Yalla yok leeram
    Serigne Cheikh Maty Leye yalla nafi yagg lool té wer
    Aamiine.

  66. beugue Segn Touba rek moy rek mo nekh té dagane

  67. kas dit :

    il faut encourager serign moustafa gainde fatma il a vu juste je ne suis pas politicienne mais nous avons besoin de nous demarquer de tout ce qui se faisait jusque la

  68. mballo sdamb dit :

    damay satt serigne touba cheikh saliou mbacke motakh niou kham yalla kham yonén kham serigne touba.dir satt toutes la personnel de rodio lampfallfm et tv.sertigne mame mor kham sa diné ak serigne assane mbaye tabelé si segn bi yame si segne bi.

  69. ousmane MBAYE dit :

    Nous africain et plus particulierement senagalais devons un garand Merci a CHEIKH AHMADOU BAMBA et etre fier de lui

  70. ndiaga fall dit :

    diarama serigne touba diarama mame cheich ibra fall lamp serigne sidy mokhtar mbacke yall nafi yak tee weer ak serigne cheich diambou fall ak talibiyi lamp fall fm lamp fall tv magilleendy siaar boweer dileen nianall foma toulou sasouny moy taaw moy nathie yallnaleen yalah saam ak serigne touba wassalam inalahamanah ndiaga fall anvers belcigue

  71. mane Samba Kanteye talibé serigne Abdou Mbacké ibn Serigne Cheikh Khady brom Darou Mouhty Yalla na fi yag téé wéer ma ngui lénn di safo di déglou radio bi bou bakh diléne nianal yalla nguénn dédié ak ngueremel brom Touba

  72. gueye abdou dit :

    CHEIKH AHMADOU BAMBA C’EST LA PROJECTION ORTHOGONALE DE DIEU SUR TERRE

  73. dieure dieufe serigne touba mbacke khadime rassoul diara ame mame cheikhe ibrahima falle lamp

  74. cheikh ahmadou namba khadim rassol c soveur de lumanute nous ommes fiere des baye falle koudoul baye falle baye falle mole gueune diaraw lak mame cheikhe ibrahima falle
    lamp.

  75. cheikh ahmadou bamba khadim rassol c le soveur de lumanute nous ommes fiere etre baye falle koudoul baye falle baye falle mole gueune diaraw lak mame cheikhe ibrahima falle
    lamp.

  76. maangi niaan yalla ci magalouk touba fouwaay mana joge yallna demak jamma dika ak jamma ci barke boroom touba loufa waay niaan serigne touba nangoulako aamiin

  77. maangi niaan yalla seregne side mbacke yagi fityer anin

  78. ndiaga diop dit :

    serigne touba amoul morom.mako beuk sa ma khole.dieureudieufeti serigne saliou mbacke.

  79. begue rek tayy beugue rodio bi noudika amm mou lere fi si ndar

  80. modou fall dit :

    deureudjeuti serigne saliou damako beug sisama xol

  81. mbengue dit :

    vous etes trop fort cotinu comme sa

  82. sfalloumbacke dit :

    radiobi amena solou

  83. YALLA THIE THIOOBARE LAYE DIEUFé – serigne bi nééna « MAAKO SOOBE ». Lamp fall radio bou baru ndiarigne… DIARAMA -SAKHLEENE THIE « SERIGNE TOUBA REKK ». SALAATOU WA SALAME ALAA MUHAMMADINE WA ALAAA AALIHI WA SAHBIHI.

  84. DIEREFE SERIGNE TUOBA

  85. sante serigna touba rek ak lamp fall fm di niane nou yokou ba yecko mangena sopi kounek tambale si segnebi yam si sengebi diam ak kheeweul yalna nek si nioune wa salam

  86. SANT NA SERIGNE TOUBA NANOU DOLI SANT SERIGNE TOUBA ( mortalla golf sug 776045000 dofou serigne touba

  87. Radio lamp fall kou ko ame loy deglo bénène radio. Dieureudieuf Serigne Touba! Diarama Ibrahima Fall

  88. ibra dit :

    mane lamp fall fm rekk lay deglu

  89. sadekh dit :

    serigne bi mo yémé dé!!! jah jeufé cheikh ibra

  90. elhadji gaye dit :

    elhadji gaye new york i love lamp rodio mourite thank your brooklyn

  91. mamdou dit :

    sqlamou khalaykoum abdoulaye dou ayye niang mo layy defff degg deggi talibe sakhal si degg ak toppp serigne diabbale niou

  92. code gaye dit :

    radio lamp fall bi ap talibe la day ligueyal serigne touba sa kaw rek

  93. code dit :

    abdoulaye yaw nek talibep serigne touba mogui sa xol diam rek ngay am dakh saytanei mom gneimeiwoul serigne bi kalameiko ak borom touba tei nga am sa gueum ak pastef cii yoon wi sa borom mane nala diapalei

  94. marfall dit :

    c vraiment nekh

  95. marfall dit :

    c vraiment jm vraiment

  96. fama ndaw dit :

    serigne touba amoule moroom tamogni tékhé fi thi dounya tékhé gnou fée thia l’akhirra dieurediefeutti serigne touba diarrama mame cheikh ibrahima fall.

  97. Saliou KAMA dit :

    Thiey Serigne TOUBA,

    Niougui sante yalla bimou niou deffe aay Mourides

    Dieureudieuf Serigne TOUBA,
    Dieureudieuf Serigne TOUBA,
    Dieureudieuf Serigne TOUBA,

  98. DIEURIEUF SERIGNE TUOBA POUR OUSMANE THIAM DEPUIS BARCELONA

  99. malick diouf sope bamba dit :

    vraiment vous etes tre gentis votre travail est tres sereiux et res nex sikaw sikanam yalnalen yalla faye

  100. Zack dit :

    l’article est tres interessant, mais je ne suis pas d’accord avec tous les points…

  101. Gnigui ziar bép mouride tadi sakou niane thi barké serigne Saliou Borom Diamono

  102. abdou khadre samb dit :

    dieuredieuf seriñ touba diarama mame cheikh ibrahima fall.beg nanou lole thi wakh tanewi yalla na borombi yokou kham gui ak fane wi ak wer gui.

  103. mame dit :

    Hi my name is mame Ilive in new yorkand realy like to lesten lamp fall

  104. deure deuf serigne fallou magal kazou radiab si jamm

  105. Antoine dit :

    Bonsoir!??Bon,je sais que c est un peu hors sujet, mais bon je me permets de vous faire part de mes idees. Seriez-vous tente par un echange de liens ou de posts sur nos sites respectifs ? J’ai un blog s interesse beaucoup de themes similaires aux votres comme les vances ou les voyages et je suis certaine que nous pourrions tous deux profiter de cet echange. Si vous etes tentes, vous pouvez m envoyer un email. Je suis impatiente d avoir de vos nouvelles ! Un site pas mal du tout en tout cas !

  106. dafa diote si dimamonoye taye gnou kènal kou téd ki ta xame valeurame gnoune talibé nanou beuganté ta bolé ngir saytané bagna ame wale si gnoune

  107. mame dit :

    diadieuf mame cheikh ibrahima fall lampe

  108. mané aka diote gnou xame borom diame gni.ndax kate kou tedki yamoul ak léne naye leer.mane personnellemement damakoy tek si kowe ndax mo fawxa lep lo guiss.DIEUREDIEUFETY BOROM TOUBA

  109. makhtar seck beugue taif dit :

    alhamdoulilahi banou sounou borome bolle ak ay mboki talibe yo khamne dounou tayi thi liguaye serigne touba magui ziar yepe rawatina serigne cheikh marem ndiay mome serigne moustapha ndiaye serigne mor syll taif ak sama wassila serigne fallou mbacke inb cheikh mouhamed taif

  110. assamouhaleykome yene mbocki djoulite yi dilene balou akhg dilene balle sasoune

Poster un commentaire

XHTML: You can use these html tags: <a href="" title=""> <abbr title=""> <acronym title=""> <b> <blockquote cite=""> <cite> <code> <del datetime=""> <em> <i> <q cite=""> <strike> <strong>

Comment faire de la publicité sur xalima.com ?