ndakh serigne touba dafa ligueyal borom bam feyko mou djagle ko diam yiep motakh mune ya malikal mulku ya man djalah han khawadi hiram djamil wara ya khadian raddah
dieuredieuf serigne touba,contan na yi radio bi lool te dit sant seex ablaye mbodji yalla nafi xalifa bi yakh te wer ak nioun niepp yi barke borom touba.
DANOUY SANT RECK WAA RADIO KHASSIDA ON LINE RAWATINA SERIGNE MOR SYLLA TAIF DI NIAANE YALLA DEFALKO LIMOU BEUGG LEPP TEM GUEUNE THI MOOM,YALLA NA YALLA YOKK LEERI SAMA SERIGNE BA SERIGNE MOHAMED MBACKE TAAIF.
MAANGUI NIAANE THI DARADIAY SERIGNE MBACKE SOKHNA LO SAMA SERIGNOU SERIGNE CHEIKH GUEB SYLLA GOUDD FANN LOOL TE WER TE YEENEYIM AM THI TAAIF YALLA DEFAL KOKO.
di beguee serigne touba rek ak wa keureum sa sou nai te sante serigne latte toure, mou yag nio jitte yi yoonou serigne touba.te begue yi radio yalla yagal leen fi akoum weer amine
dieuredieuf serigne makhmadane mbacke waxtan wi am solo looo deeg nagnou deug
s,il n;etai pas serigne bamba le senegal ou l,afrique naura pas cettr paix ideal ; DIEUREDIEUFE SERIGNE TOUBA DIARAMA MAME CHEIHK IBRA FALL
boudoull wonn serignetouba nioune niap dem nirani dieuredieufe serignetouba diaraw lack mame chiekh ibrahima fall
dieureudieufeuté yalla sonou borom waxtane wi am na solo lollllllllll yalla naléne sounou borom bi faye té défale léne khéwal soutoura tawfékh ak taysir
dieureudieuf khadimoul moustapha diarama mame c ibrahima fall s touba s sidi moukhtar yalla nafi yaga ta wer loll
Cheikh sidi mokhtar mbacké yalla nafa sax ba abadane.kou diote cii ñiane guii nel amine
dieuredieuf serigne touba
serigne touba amoul moroom sate nanouko bu weura weur
ndakh serigne touba dafa ligueyal borom bam feyko mou djagle ko diam yiep motakh mune ya malikal mulku ya man djalah han khawadi hiram djamil wara ya khadian raddah
ziare dieureudeuf boroom tuba amoul moroom
saregn tuba reekla
wagtanewi amnasololol buolenko baei
sant serigne touba rék guereme serigne touba rék yakar serigne touba rék diarama mame chiekh ibrahima fall
dieureudieufeuté serigne touba cheikhoul khadim yalna takha waye bi yagu lolll
SERIGNE TOUBA AMOUL MOROM KEN LA
SANTE TABAARAKA WA TAHAALAA BIMOUMA BOOLEEH THI WAKEUR CHEIKH MOUSTAPHA YALANA YALLA YOKK LEERI SAMA SERIGNE BA SERIGNE MOHAMED MBACKE TAAIF
dieuredieufé serigne touba khadim rassoul. lépou serigne bé. comme le disait serigne moussa ka « serigne bi bognou diokhé langa gnou diokhone dotounu déf nanou défone khana khamo légui yarrou nagnou »
DIEUREDIEUFE SERIGNE TOUBA DIEUREDIEUFE SERIGNE TOUBA DIEUREDIEUFE SERIGNE TOUBA DIEUREDIEUFE SERIGNE TOUBA DIEUREDIEUFE SERIGNE TOUBA DIEUREDIEUFE SERIGNE TOUBA…SERIGNE SIDI MAKHTAR YALLA NA FI YAG TE WER.AMINE
alkham doulillihi rabil alamina dit satt tabaraka wa talla thi liniou done ay sénégalé deque serigne touba cheikh saliou mbacke ndakh serigne bé takh niou gueme degue yalla ak yonén
Toppou li yalla diglé bayé li yalla Téré
sant serigne touba rek mo wor.thiéy bougnou la amoul wone khawma fougnouye dieum
Toppu li Yalla diglé bayi li yalla Téré
SERIGNE TOUBA AMOUL MOROM
I AM FELLING SO GOOD DIEUREUDIEUFE SERIGNE TOUBA
je salue tous fidèle pour adore le seul dieu toute puissant ce que veux rentre dans la pardi fait tous que pps vous dit ce envoyé de dieu a dit attuou laha attuou rasoul lha mer cher frère seour aslamouleikoum
di sant tate cheikhoul khouyokhi di niane chekh sidil moukhtare yalla yagal kofi looooool te mou ande ak wer deureuguen deuf yenitame
thièy serigne touba dièbalnako sama bopou ak sama gnèpou ak sama lèpou bil moustapha
dieureudieufa serigne touba
wahtane bi am na solo lolou surtou ndaw gni
dieuredieuf serigne touba,contan na yi radio bi lool
te dit sant seex ablaye mbodji yalla nafi xalifa bi yakh te wer ak nioun niepp yi barke borom touba.
serigne touba rèckle lèppeu moma
Dieureudieuf Serigne Touba Kene Amoule Fayame Yalla Nioukeye Fayale Té Yalla Maye Niou Kattane ak Weur Bouniou Ko Liguéye lé thi Barke serigne Cheikh Sidy Makhtar MBACKE Yalla Nafi Yague Té Werur Kouné Amine Yalla nagua Guoudou Fane.
serigne touba amoul morom dieuredieuf borom touba
dieref yalla nagnou yalla may fanwou goude gnouye ganamana sop serigne touba fougnou mandinek amineeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeee
Santa naline yenn niey deklou yalla nannou yalla Boole Fay ak serigne bamba ak brom darou mouhty ??? ?????? ?????? ????????
DANOUY SANT RECK WAA RADIO KHASSIDA ON LINE RAWATINA SERIGNE MOR SYLLA TAIF DI NIAANE YALLA DEFALKO LIMOU BEUGG LEPP TEM GUEUNE THI MOOM,YALLA NA YALLA YOKK LEERI SAMA SERIGNE BA SERIGNE MOHAMED MBACKE TAAIF.
MAANGUI NIAANE THI DARADIAY SERIGNE MBACKE SOKHNA LO SAMA SERIGNOU SERIGNE CHEIKH GUEB SYLLA GOUDD FANN LOOL TE WER TE YEENEYIM AM THI TAAIF YALLA DEFAL KOKO.
di beguee serigne touba rek ak wa keureum sa sou nai
te sante serigne latte toure, mou yag nio jitte yi yoonou
serigne touba.te begue yi radio yalla yagal leen fi akoum
weer amine
dieurediefati serigne touba diarawlakati mame cheikh ibrahima fall
dieurediefati waker serigne touba serigne sidy moukhtar mbacke yalla naffiyage te weer LOOL AMINE youssou kane sope serigne touba mbacke
sante serigne touba bou wer cheikh sydi moukhtar yaLLA NAFI YAGUE TA WER HAMIN
Sant s.touba rekk que dieu donne une longue vie a s.cheikh maty ley mbacke
SERIGNE TOUBA AMOUL MOROM