Comment faire de la publicité sur xalima.com ?

Pour vos besoins publicitaires, Contactez nous


Comment faire de la publicité sur xalima.com ?

Radio Khassida Online

Posted By Xalima News On Mercredi, août 10th, 2011 With 2 Comments



IMAC/IPHONE users click here


143 Commentaires
Participer au forum
  1. man cheikh diouf firenze man gui len di ziarr bu werr akaza

  2. Ragal yalla déf li yalla dig li bayi limu téré

  3. MAANGUI NIAANE YALLA THI DARADIAYE CHEIKH MOUHAMADOUL MOUSTAPHA YEEN WAA RADIO KHASSIDA ONLINE YALLA DEFAL LEEN LINGUEEN BEUGG LEPP TEMOUY LOU GUEUN THI YEE.LIGEEY BI NGUEEN DI DEF ADUNA BEPP RAFETLOUNAGNE KO,WOOTE WOUMA WAA WOUTE WOUMA BENN YOON,KHAUMA KENN WAAYE SERIGNE TOUBA MOOM GUEUREUM NALEEN,DIEUREDIEUF.

  4. elhadji gaye dit :

    talibe serigne cheickh lo gabou live in new york ville brooklyn thank your

  5. elhadjigaye dit :

    jaime beaucoup serigne touba talibe serigne cheickh lo gabou i frome diourberl bht i live in new york quatier brooklyn

  6. elhadjigaye dit :

    sope serigne saliou mbacker touba

  7. ALASSANE DIOUF dit :

    CHEIKH SIDY MOCTAR MBACKE YALLA NAFI YAG TE WEER RAFETE LOU NAGNOU KORITE GUI GNIGUI BALOU GNEP AKH DI GNANAL WA SENEGAL GNOU TOPE NDIGALOU SERIGNE TOUBA

  8. sant yallah di niane mo may niu jub ak toppu ndiguellu borom touba

  9. SANTATINAA TABAARAKA WA TAHAALAA THI BOOLEGUIMOUMA BOOLE THI WAAKEUREUM,BOOLEMATHI WAAKEUR CHEIKH MOUHAMMADOUL MOUSTAPHA ,MA DIOUDOO TAAIF ,YAROOFA ,SERIGNE MBACKE SOKHNA LO DI SAMA SERIGNE DI NIAANE YALLA BIS BOUMAY DEEH MA DEEWE TAAIF NIOU SOULMAFA.SERIGNE MOUSTAPHA MOHAMMED SAMA SERIGNE YALNAFI YAGG TE WER!!!

  10. moustapha ba dit :

    thiey mbacke bougnoula amoul won khawma fougnou djeum,nguir nii fou mbidef djakhle sou guesso guissla.
    mouride sadikh djeufla dou nguistal yalla na yalla khir gnou thi beug bamba ak wakeureum.

  11. sama serigne lou wéér ngén wakh délou si diangalé SERIGNE TOUBA rék amoule lénééne politiciens yii ak faux marayii akii maride gno beuga yakk yoon wii,wayéé tamite baye Fallou ndakarou yii sonale nagnou toukh yamba réék ak yalwan di yakk dééér bilahii damaye rousse sakh.Dieureudieuf Serigne Touba,wa salam.

  12. diopmodou dit :

    diaradiafe borome touba

  13. saliou fall dit :

    bay zal jaammu serigne bara aminata lo senegal ak adouna yeep yalla na fi yalla def jaam ta baayi fii cheikh sidy mou yaag fi ta wer ta yaan bi woyoof mou doon mbeeg gou jouliit yeep rawaty talibe serigne touba boune

  14. moustapha ba dit :

    way way mouride nguir yallah,nagnou sakh si dingalal serigne bii.
    Gnanal leen ma ma doon mouride sadikh nguir yallah ma guisse ak serigne touba khadim rassoul.

  15. chiekh dit :

    santi yalla buwer

  16. didaradiaff S touba mbacked damabague kouma yonee wakhtani dine ak khassida diarangundiaff WSALAM

  17. dirama serigne touba

  18. Ko guem yalla ak bis pincc ma na wax yiiw walla mu noppi

  19. fallou dit :

    mome reklayalana niouko yalla fayal thi barkeb yonnentebe

  20. diarama mamme borom touba

  21. sant serigne touba te sakh thi aye ndigueuleum mane dioala la mais souma khama serigne saliou mbacke di serigne touba bay ndiangue xassidam yi c’est grace a cheikh bethio di niane mou sakh fi te wer

  22. diarama mamme borome topuba pour ousmane thiam de barcelana

  23. bonb jour ses ousmane thiam depuis espania barcelona terrassa
    qui vous di diarama mame borome touba

  24. moustapha ba dit :

    Mangui ziar bou weer, di sant sama serigne moustapha mbacke mou serigne
    Saliou di gnan yalla si mbakham mou sakhal té yagalfi serigne Sidy mokhtar mbacke.
    Dellou rek di sant serigne touba minou yalla bolel, mangui gnan yalla bouko been mouride gathiél, yalla nanou nék si Lou serigne bi geureum. Yalla nanou dougou si gallou serigne touba.

  25. OUSMANE dit :

    bon jour ses ousmane thiam depuis espania
    diarama mamme borome touba

  26. OUSMANE THIAM dit :

    bonsior ses ousmane thaim depuis espania
    qui vous dite fete de nowel a tout la preses
    de xalima merci

  27. OUSMANE THIAM dit :

    bon jour ses ousmane thiam qui vous salu de cete fin danne
    pour la preses de xalima…merci

  28. fama seck dit :

    dieuredieuf borom touba contann na niou bou xerr

  29. bon jour ses ousmane depuis españia qui vous souéter une bonne fetes de fin dane merçi

  30. asalamou, assalamou hallaye koum warahmatou lahi mangui nouyou sama moro diam yi di dioulit yi di nouyou sa ma moromi talibe yi di mouride di wakhni fou fi way mana nek nay wakh dieureudieuf borom touba mo leral lep

  31. ousmane dit :

    bon jour ses ousmane thiam depuis éspania qui vous dit bonne debui
    danne a la preses merçi

  32. kénal yalla bagne koobokalé ak kénne

  33. OUSMANE dit :

    bon jour ses ousmane thiam depuis barcelona qui vous dit bonne preparasion de maouloud atous les mousilmen du monde..merçi

  34. sg adama dit :

    beguee bouwer saasounee bilahi

  35. serigne touba de doumorm de kine dou mome

  36. ousmane dit :

    bon sior ses ousmane thiam de barcelona qui vous dite une binne fete

  37. Djeureudjeufe borom Touba Cheikh sidy mokhtar yala nafi yague tee weer amine barke borom Touba.

  38. elhadji gaye dit :

    sope radio khasside tallibe serigne cheikh lo gabou sope serigne saliou mbacker i hop holl the tallibe be came to gettede and bille touba ville sainte elhadji gaye lave and new york booklyn thank your

  39. samba ba dit :

    extraordinaire travail pour la diaspora en effet a paraitre bientot cheikh ahmadou bamba face a ses contemporains 1885-1927 par oumar ba ancien archiviste mon pere je vis en italie samba ba 3889318493 italiatrading1@gmail.com

  40. assane sal dit :

    assane sal new york sopei radoi mame diarra diaraf seringe touba spei xassida on line thanks may god bless you diaraf seringe touba

  41. saliou pouye bresil dit :

    magui len di ziar bou wer

  42. DIARAMA MAMME BOROME TOUBA POUR OUSMANE THIAM DEPUIT BARCELONA…MERÇI POUR TOUTE

Poster un commentaire

XHTML: You can use these html tags: <a href="" title=""> <abbr title=""> <acronym title=""> <b> <blockquote cite=""> <cite> <code> <del datetime=""> <em> <i> <q cite=""> <strike> <strong>


Comment faire de la publicité sur xalima.com ?

Pour vos besoins publicitaires, Contactez nous



Comment faire de la publicité sur xalima.com ?

Pour vos besoins publicitaires, Contactez nous


Revue de la presse