Fils de Serigne Falou Mbacké, deuxième général des mourides, Mouhamadou Lamine Bara avait lui-même accédé au khalifat à l’issue du rappel à Dieu de son oncle Serigne Saliou Mbacké survenu le 28 décembre 2007.
http://www.istikhama.org
Sixième khalife de la confrérie des mourides fondée par Serigne Touba Khadimou Rassoul, Serigne Bara était le premier des petits-fils du Saint homme à accéder au khalifat.
Lampfall Touba
RFM
SUDFM
Al lahou akbar dieureudieuf sous borom mague laye niane si barké yonété bi (psl) ak dieme serigne touba hadim rasoul souf oyof si kawam
Serigne bara Mbacké yal nako yalla yaré ardiana Amine
yalla nako yalla yereum mbacke yakou fi dara yalla yok ay leeram te tas niou thi barkeme
je suis vraiment dsl on na perdue un des plus grands hommes du monde ke dieu l acquerie dans son paradis
ina lilahi va ina ilayhi radioune alahou akbar yalla mo meune sagne louko nekh def fatalikou leene cheikh saliou mbacke nieup yakarone ni doufi djokk kon nanou delou si yalla serigne touba amoul morome
maggi koy dialle bepp.. mouride bepp dioullite ,serigne cheikh ndindi mbacke ken niakoul waye man ma niakk yalla na sarakhame yagg sunu loxo mbacke………….
yalla mo nek; té sagna téck diamame louko nékh; kone yalla nanou khirtal thi boopame té mayegnou kholou mougne. Mbacké yalla na yalla yocki lérame té tass thi barkéme. Deuredieuf Serigne touba.
allahou akbar yalla na souf woyof si kawam
diéreudiefu serigne touba allahou akbar serigne bara
mbacke yal na yalla yokou sa ler ak ndiabotu cheikhoul khadim guep ngag fa fek
yalla na niou yalla tase sibarkém mbacke contane niou lool si sataxaway bo rafét
inalilahi waiinali raziouna yalla nako yalla térouko ci aldianayi guena kowé tass gnou ci barkém diko dialé niep niep sans exeption dieureudieuffti sounou borom……………..
SERIGNE BI YALLA NA KO YALLA HARE ADIANA GOU MAGE GA YALLE NAKO YALLA YOKALE AYE
YALLE NA YALLA YOKOU AYE LEREME HALA HOUMA SALI HALA SEYDINA MOU HAMADINE WALA ALIHI WA SAHEBIHI WA SALAMANE TASLIMANE ALHAMDOULILAHI RABINE ALAMINE
serigner bara yalla nako yalla yereme te tesnou yi berceme amin