spot_img

Viatique du 1er octobre 2021 parole et écoute

Date:


Les Anciens disent : « Je suis responsable de ce que je dis, pas de ce que tu comprends ».
Mieux vaut avoir un auditoire qui sait écouter qu’être un bon orateur. Écoutons nos locuteurs-trices avec notre intelligence mais pas avec nos intérêts, nos haines, notre rejet de la personne qui parle. Point de belle parole sans une belle intelligence d’écoute. »
Bon Vendredi.
Dr Massamba GUÈYE LBA


Yóbbalu 1 fanu Oktoobar 2021
Wax ak dégg…
Wolof Njaay nee na : « Li ma wax maa ko gàddu waaye na nga déggee sama yoon newu ca».
Mën a wax, di wax ak ñu am ag dégg da koo gën. Nanu bàyyi di déglook xol, mbaa sunu par-parloo, mbaa mbañeel gu ñu bañ kiy wax. Wax du neex ag déggay neex. »
Àjjumay jàmm.
Dr Masàmba GÉY

nayrafet

LAISSER UN COMMENTAIRE

S'il vous plaît entrez votre commentaire!
S'il vous plaît entrez votre nom ici

spot_img

DEPECHES

DANS LA MEME CATEGORIE
EXCLUSIVITE