Dire du mal pour faire mal ? Non ! Qui dit du mal de son prochain, dans le strict but de ternir son image, pour quelque raison que ce soit, ne fait que révéler son propre mal être et le peu d’humanité qui lui reste.
Chacun se dévoile à travers ses propos, il faut donc les réfléchir. Parler, c’est épuisant car on met toutes les forces de son corps et ses facultés mentales en branle pour produire une phrase. Cet effort terrible de production orale ne doit pas être de l’énergie perdue pour nous ! Fournir tous ces efforts, dans le strict but d’essayer de nuire à quelqu’un, est un investissement à pure perte. Une parole esthétique doit avoir une portée morale.
Nous devons avoir autre chose à faire de notre vie, comme corriger nos propres défauts, que de souffrir qu’autrui soit bien vu.e. Le temps fait toujours son œuvre et est seul juge. Dire du mal de quelqu’un, c’est plutôt se faire mal et laisser paraître qu’on est mal. Dire du bien, surtout le bien vrai, ça fait du bien. On ne détruit que sa propre image en médisant mais pas celle de sa cible. »
Dr Masàmba GÉY LBA
#nayrafet
Yóbbalu 4 fanu Nowàmbar 2022.
Wax lu ñaaw…
Wax lu ñaaw ngir nàqaral? Mukk! Kuy wax lu ñaaw ci sa moroomu nit ngir rekk jéem koo yàq, ak lu man di doon sabab ba, sa woppi xel rekk ngay wane ak sag niteediku. Ku wax futti nga sa jikko.
Xalaatal ni booy wax benn baat rekk, sa yaram, sa xel, say lor, sa doole yépp ngay boole jëfandikoo ngir àddu. Boobu coono ngay daj ngir ubbi sa gémmiñ ba wax, bu dee lu ñaaw rekk la, yàq jot gu yéeme la. Coonob wax nim toll, jubluwoo ci lu dul tey ngeen bañ diw, musiba la.
Wax day rafet, tey defar. Nit ku baax sax war naa tal a jubbanti ayibi boppam ba du gis joj keneen. Waaye nga ne kenn du ne diw baax nab ax tax ngay wax lu ludul dëgg baaxul. Yàgg bawul dara! Wax lu ñaaw, lu bon la! Wax lu baax day tax a baax, ñu naw la, te moom rekk a rafet. Ku wax lu baax kenn du ne la a cam! Wax ba yàq amut, wax ba yàqoo am. »
Dr Massamba GUÉYE LBA