spot_img

N’abandonne jamais ! (Par Massamba Gueye)

Date:

« Ne pas abandonner quand ça devient dur mais s’endurcir, se faire une carapace pour réussir, telle est la clé. C’est dans les moments de doute qu’il ne faut pas flancher mais se reposer sur ses points forts, s’arc-bouter sur ses atouts personnels quel que soit leur degré pour tenir le coup.
C’est trop facile d’abandonner parce que les obstacles naturels ou artificiels barrent notre route. Il faut les détruire avec intelligence et minutie et opposer un tintamarre de bonheur aux pourfendeurs de notre joie.
N’offrons pas à ceux.elles qui nous détestent sans raison des raisons d’être sereins. Offrons plutôt à notre conscience les ressources vitales pour nous rendre serein. C’est juste une question de volonté et parfois de courageux choix de vie. »
Bon Vendredi

Nayrafet

Dr MASSAMBA GUÈYE
—-
Yóbbalu Àjjuma
Bul ne yàcc mukk!
« Bum metti mukk ba nga bàyyi waaye bu mettee, nga dëgër der, gàddu ko yaa ngi ci yoonu ndam.
Bu mettee nga war a sukkandiku ci li la Yàlla may ba dékku lépp man caa génn ak ndam. Dafay yomb lool jafe-jafe yu Yàlla indi mbaa nit sos ko tax nga bàyyeeku! Yooyu jafe-jafe, sam xel nga leen di daane ci ag dal gu mat sëkk ak it fit wu rëy booleek nak tanqal say noon ci sa jàmm juy riir.
Bu nu may mukk ñi nu yéenewul jàmm mbégte waaye nanu may sunu bopp jàmmi biir juy tax nu jàmmook sunu bopp! Yoonu ndam woowu nak kune yaa koy xàllal sa bopp ak saw fit ak sa jom. Loo jombale sa bopp ci lu baax mu jomb la. »
Àjjumay Jàmm !

Nayrafet

Dr Masàmba GÉY

LAISSER UN COMMENTAIRE

S'il vous plaît entrez votre commentaire!
S'il vous plaît entrez votre nom ici

spot_img

DEPECHES

DANS LA MEME CATEGORIE
EXCLUSIVITE

De quel droit Métropolis se prévaut-elle ? (Par Thierno Bocoum)

En remplaçant Barthelemy Dias à la tête de l’Association...

Mamadou Ibra Kane : Un homme perdu entre le journalisme et le militantisme (Par Sall Mamadou Oumar)

Mamadou Ibra Kane, journaliste et homme d'influence dans le...