spot_img

Taasu Laay Waad Par Ousmane Dramé

Date:

TAASU LAAY WAAD

na loxxo yi daaje!
na loxxo yi mbeekké !
na daajé na daajé !
na loxxo yi dajé !! é démal ! demal
Abdu dafa waace
Ablaye yéék
senghor wacup liiguééy
niu dém diko jaalé
bato ba diik
kunné boppam la tal !!
Nélba dafa réy té xélma naax
lumu wax fatté ko !
beut yeu da fa dug
té léx ya rass
laaye lejeel nanu !!
Laay dolli niu, Nga doggaliniou ?
Laay wadday paxoum kania !
Ak famèèm bu n’daw!
Bénoup diabar niaari doom
faaf goro ba déé !!!
laay wadday paxxum kagna !
Laay waddak ndonggam gou darr
laay waddak beetem yu dém

LAISSER UN COMMENTAIRE

S'il vous plaît entrez votre commentaire!
S'il vous plaît entrez votre nom ici

spot_img

DEPECHES

DANS LA MEME CATEGORIE
EXCLUSIVITE

Mamadou Ibra Kane : Un homme perdu entre le journalisme et le militantisme (Par Sall Mamadou Oumar)

Mamadou Ibra Kane, journaliste et homme d'influence dans le...

Plaidoirie pour une réforme urgente du Conseil constitutionnel : Moussa Tine interpelle Diomaye Faye et Ousmane Sonko

XALIMANEWS-Dans une tribune, Moussa Tine, président de l’Alliance Démocratique...