« Si demain je meurs,
Pardonne mes faiblesses d’humain,
Mes folies, mes bassesses et envies infondées.
La vie est éphémère et chaque jour qui passe
Est un signal à nous adressé que le trépas arrive.
Rien ne sert d’effilocher des dignités !»
Nayrafet
Dr Massamba GUEYE LBA
—-
Njéggal !
« Rikk bu ma làqoo ëllëg,
Baal ma samay rëcc-rëcci bëccëg,
Baal ma samay rëcc-rëcci yi ma yëgul,
Samag wayadi, sama jëf ju tuut ju jagul.
Àdduna dafa gàtt fan te bés bu wéey rekk
Yëgal na nu ne dee agsi na ne tekk!
Dara jarufee xiiroo aka xëccoo !»
Nayrafet
Dr Masàmba GÉY GA