spot_img

Viatique du 11 novembre 2022. Femme…(Dr Massamba Gueye)

Date:

Garde-toi de dire du mal des femmes. Chaque parole adressée à la femme est aussi dite à notre propre mère. Chaque mot déplacé, arrogant, incorrect, chaque insulte, chaque caractérisation négative ou ignominie dite, pour le plaisir, à une femme est une caractérisation de notre propre mère.
Dans nos traditions africaines certifiées, il n’était pas permis et il ne le sera jamais, de considérer la femme comme un simple objet de désir. On ne peut se permettre, en public ou en privé de la regarder avec mépris, gratuitement. Chaque mot dit à n’importe quelle femme du monde et un mot dit à notre propre mère.
De la même manière, femmes, gardez-vous, sur les réseaux sociaux, dans les émissions et autres lieux de dire que les hommes sont tous mauvais car ce jugement inclut aussi le père. Celui qui a un problème une femme, ne peut le régler dans les instances autres que sociales et conventionnelles. A côté de chaque homme qui se bat, il y a une femme qui se débat sans débat. »
Bon vendredi !
Dr Massamba GUÉYE LBA

#nayrafet

Yóbbalu 11 fanu nowambar 2022.
Jigéen…
Moytul di wax lu ñaaw ci Jigéen ñi. Loo wax Jigéen rekk boole nga ca sa way-jour du jigéen. Baat bu warul bu nekk, ñaaw, xeebaate. Saaga, sikkal boo jëmale ci jigéen rekk rombul sa way-jur.
Sunu aada ji dëggu mayewul nga jàppe jigéen jumtukaay. Mayewut nga koy xeeb ak a kall-kallee ci sa bànneexu bopp rekk. Bépp baat boo jëmale ci jigéen du moy sa yaay. Yéen it jigéen, moytuleen, ci lënd gi ak jotaayu mbooloo yi muy tele mbaa rajo, di yakk góor lu ne ndax genn góor gu la def lu warul. Loo wax góor wax nga ko sa way-jur wu góor.
Ku am loo joteeg jigéen fa nga ko war a faje du romb ëtt bi. Kekkantoo jigéen ci lënd gi mbaa feneen mooy saaga sa yaay ji la sukk jur. « Ca gannaaw bépp góor buy yëngu bu ne, am na jigéen ju ju kenn gisut ju ni tekk, ju àdduwul ju koy jàppale. »
Àjjumay jàmm !
Dr Masàmba GÉY LBA

nayrafet

LAISSER UN COMMENTAIRE

S'il vous plaît entrez votre commentaire!
S'il vous plaît entrez votre nom ici

spot_img

DEPECHES

DANS LA MEME CATEGORIE
EXCLUSIVITE

De quel droit Métropolis se prévaut-elle ? (Par Thierno Bocoum)

En remplaçant Barthelemy Dias à la tête de l’Association...

Mamadou Ibra Kane : Un homme perdu entre le journalisme et le militantisme (Par Sall Mamadou Oumar)

Mamadou Ibra Kane, journaliste et homme d'influence dans le...