Wade à Touba: une foule nombreuse
[Video] Wade accueilli à Touba par une foule impressionnante
DEPECHES
DANS LA MEME CATEGORIEEXCLUSIVITE
Controverse au Pastef : Fadilou Keita critique la centralisation autour de Sonko, Ansou Sambou « contre-attaque »
XALIMANEWS-La crise au sein du parti Pastef s’est intensifiée...
Assemblée nationale : Malick Ndiaye promet un »dialogue constructif » avec l’exécutif
XALIMANEWS: (APS) Le président de l’Assemblée nationale, Malick Ndiaye,...
Nomination de Aoua Bocar Thiam: Pourquoi tout ce bruit, les raisons de la colère des “pastefiens”
XALIMANEWS: Depuis sa nomination pour un mandat de 6...
Ousmane Sonko: « Il faut que les menaces cessent, on ne menace pas un Président »
XALIMANEWS: »Suite à la polémique après la nomination de...
serigne toyba serigne saliou serigne abdou lahate amenaniou louléne nakhari trope thi nigéne niaka wormalé dioumameji serigne abdou lahate miko banione ba dageulou garapeyi guir bagne gorake djigéne difi diakhaso taye amena lole louma nakhari
wade dou ame limou beugeu thi s.touba ndakh dafa adack saytané
je suis tout a fait d’accord avec toi touba n’est pas une ville de politique c’est une ville spirituelle tout ça c’est de l’analphabétisme
serigne touba mofie tok soko baioun ben talibe do ken digale lano si ah wade limo am si yono serine touba wi rek doynako serigne saliou nianalnako ta ko am nianame do yaho ba fawo yen nak tite rek molen taha wah lolo mais tok len rek ta xar
Wade dane nane ko tértu tertu bou gena khoube
Wallahi sng Touba. Amena louko nakhary lole lii yalla nagén ko layoo ak mome
90/100 sont des mineurs et ne peuvent pas voté donc c’est un non evenement passons a autre chose
Il n’y avait pas d’interdiction de manifestations politiques à Touba de la par du Khalif?
serigne saliou niépou la nianale wade limou andi touba kéne masoukofa niémé kouné serigne touba banioule li daga diangoule matelaboule fawasayeni mboléme khalifa yifi diar kéne bagouthi louméleni ame thi dioumadji kéne wakhoule boukéne térou wade wayé dafa ame fou serigne saliou wakhone kouye yagou yeguo adouna nagafayame ta wormale dioumadji nioune serigne touba douniouko dieundé kéne lamoudane bagne babaniye fatou danioukoy bagne serigne sidy mokhtar yagoule sakh né wade thi dioumadji lanioukodone térto
wakho d’gue serigne Sidy Makhtar Yalnafi yague téver
khobou garape sakha sou dague danou fisof mouyacko
yaw momou ya goul dara
te sa mbacke diodiou nga def ni mome ngasant dangaye fine
santo Mback
Bone nga torope tekhep sabop
Cette foule est trois fois plus nombreuse que celle qui avait accueilli Wade à Dakar ! Quelle que puisse être leurs motivations, les Sénégalais sont là pour Wade ! Les Sénégalais qui n’aiment pas Wade, et qui se trouveraient en ce moment dans la ville sainte, vaquaient à d’autres occupations ou se reposaient tranquillement dans des salons! On n’arrête pas la mer avec ses bras, et le Khalif n’a pas tressé des lauriers à Wade pour ses beaux yeux !
wade na deme diamoudji yalla way
Adouna wornanu AK saytane ci wade mi gor AK jiken diakhaso ci fu s touba tadde